Toftaleg Adiis yi

ku jàppoo kem sama njàpp mii, daal di julli ñaari ràkka yoy du ca xalaat dara, kon Yàlla dana ko jéggal bàkkaaram yi jiitu
عربي Àngale Urdu
Yàlla du nangu jullig kenn ci yéen bu dee daa tojle ba keroog muy jàpp
عربي Àngale Urdu
Ku jàpp te rafetal njàpp ma, ay ñaawtéefam day génn ci aw yaramam bay génn ci ay weyam
عربي Àngale Urdu
Laab mooy genn wàllu ngëm, sant Yàlla day feesal nattukaayu jëf ya, sàbbaal Yàlla ak sant Yàlla dañuy feesal walla day feesal li nekk ci diggante asamaan ak suuf
عربي Àngale Urdu
Bu kenn ci yéen di jàpp na def ndox ci bakkanam daa di saraxndiku, kuy fomp (laabu) na ko tóolal
عربي Àngale Urdu
daal di jàpp njàppum Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-
عربي Àngale Urdu
Benn waay dafa jàppu daal di bàyyi barab buy tollook aw weh ci ay ndëggoom Yonnente bi-yal na ko Yàlla dolli xéewal akmucc- gis ko ne ko:"dellul te rafetal sa njàppu mi" mu dellusi,daal di julli
عربي Àngale Urdu
Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- da daan jàppu ci julli gu ne
عربي Àngale Urdu
Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- jàpp na benn-benn
عربي Àngale Urdu
Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- jàpp na ñaar-ñaar
عربي Àngale Urdu
bu kenn ci yéen yëgée ci biiram dara, te xamul ndax dara génn na ci moom walla déet, bumu génn jàkka ci ba keroog muy dégg kàddu, mbaa mu yég ngelaw
عربي Àngale Urdu