Féete ak ñi wommatul Yàlla ak deñ ci ñi ko lànkal

7Listu hadiis yi 3Ràññetley bànqaas yi

Listu hadiis yi 7

Kuy niru-nirulu aw nit ca ñoom la book
Du dagan ci nit ki mu tóng mbokkam lu ëpp ñatti guddi, ñuy dajee kii dummóoyu kee dummóoyu, ki gën ci ñoom ñaar mooy ki tàmbli nuyóo ba
ku lore Yàlla lor ko, ku sonle Yàlla sonal ko
Nit ki moo ngi ci diiney xaritam, na ku nekk xool kan lay xaritool
dangeen topp yooni ña leen jiitu woon, sibre ak sibre, loxo ak loxo
àqi jullit ci moroomam juróom-benn la" ñu ne ko: yooyu yan la yaw Yonente Yàlla bi?, mu ne: "boo dajee ak moom nanga ko nuyu, bu la woowee nanga ko wuyu, bu sàkkoo nga laabire ko nanga ko laabire, bu tissoolee daal di sant Yàlla nanga ko ndokkeel, bu feebaree seeti ko, bu faatoo nga gunge ko
Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc rëbb na góor giy sol colug jigéen, ak jigéen giy sol colug góor