Listu hadiis yi

ku taxaw Laylatul Xadri ngir gëm Yàlla ak yaakaar pay ga dees na ko jéggal li weesu ci ay bàkkaaram
عربي الإنجليزية الأوردية
Mokkal naa ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- fukki ràkka
عربي الإنجليزية الأوردية
yéen nit ñi, deeleen tasaare nuyóo, di leele ñam, di jokk mbokk, di julli guddi fekk nit ñi a ngi nelaw, kon dangeen dugg àjjana ci jàmm
عربي الإنجليزية الأوردية
Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daawul bàyyi ñenti ràkka njëkk Tisbaar ak ñaari ràkka njëkk suba gi
عربي الإنجليزية الأوردية
ku sàmmonte ak ñenti ràkka njëkk Tisbaar ak ñenti ràkka ginnaaw tisbaar yàlla araamal ko ca sawara
عربي الإنجليزية الأوردية
bu kenn ci yéen duggee ci jàkka na julli ñaari ràkka bala moo toog
عربي الإنجليزية الأوردية
diggante ñaari nodd yu nekk am na julli, diggante ñaari nodd yu nekk am na julli" topp mu wax ca ñatteel ba: "ñeel ku mu soob
عربي الإنجليزية الأوردية
Yonente Yàlla bi daan na nu xamal listixaar ci mbir yépp kem ni mu nu daan xamale saaru Alxuraan
عربي الإنجليزية الأوردية