Dawal yi ànd ak julli juróom

2Listu hadiis yi

Listu hadiis yi 2

Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daawul bàyyi ñenti ràkka njëkk Tisbaar ak ñaari ràkka njëkk suba gi
ku sàmmonte ak ñenti ràkka njëkk Tisbaar ak ñenti ràkka ginnaaw tisbaar yàlla araamal ko ca sawara