Toftaleg Adiis yi

Li gën ci sikar yi: Laa ilaaha illal Laahu, li gën ci ñaan yi: Alhamdu lil Laahi
عربي Àngale Urdu
Wax yi gënal Yàlla ñent la: Subhaanal Laah, Wal hamdu lil Laah, wa laa-i-Laaha illal Laah, wal Laahu akbar, boo ci tàmbalee baax na
عربي Àngale Urdu
ñaari baat a ngi nii yu woyof ci làmmeñ, diis ci màndaxekaay ba, Yàlla miy Aji-Yërëme ji sopp leen
عربي Àngale Urdu
ma wax: Subhaanal Laahi, wal hamdu lil Laahi, wa laa ilaaha illal Laahu, wal laahu akbaru, moo ma gënal lépp lu jant bi fenk ci kawam
عربي Àngale Urdu
aw nit duñu toog ci ab jotaay te tudduñu fa Yàlla te julliwuñu ci seenub Yonnente lu dul ne dana nekk ag réccu ci seen kaw, bu ko soobee mu mbugal leen bu ko soobee mu jéggal leen
عربي Àngale Urdu