Xàjjaley wanqaas yi

Toftaleg Adiis yi

Bu nodd-kat bi waxee: Allaahu Akbar Allaahu Akbar, kenn ci yéen wax: Allaahu Akbar Allaahu Akbar
عربي Àngale Urdu
bu ngeen déggee woote gi nangeen wax lu mel ni li noddkat bi di wax
عربي Àngale Urdu
kuy wax saa yu déggee noddkat bi, ashadu an laa-i-Laaha Illal Laahu wahdahu laa sariika lahu, wa anna Muhammadan habduhu wa rasuuluhu, radiitu billaahi rabban, wa bi Muhammadin rasuulan, wa bil Islaami diinan, dees na ko jéggal ay bàkkaaram
عربي Àngale Urdu
bu ngeen déggee noddkat bi nangeen wax lu mel ni li muy wax, te ngeen julli ci man
عربي Àngale Urdu
yaw Bilaal taxawalal julli gi, noppal nu ci
عربي Àngale Urdu