Sikkari suba ak ngoon

6Listu hadiis yi

Listu hadiis yi 6

ku jàng ñaari aaya yi ci mujjug saaru Al-Baxara cig guddi danañu ko fegal leeb luy Aw ay
Allahuma bika asbahnaa, wa bika amsaynaa, wa bika nahyaa, wa bika namuutu, wa ilayka anusuuru
li gën a kawe cig jégalu yi mooy
{Xul huwal Laahu Ahadun} ak ñaari musluwaay yi boo gontee ak boo xëyee ñatti yoon, dana la fegal lépp
ku wax bismil Laahi Allasii laa yadurru maha ismihii say-un fil ardi walaa fis samaa-i wa huwa As-Samiihu Al-Haliimu, ñatti yoon balaa bu bette du ko dal, ba baa muy xëy
wax naa ci sa ginnaaw ñenti kàddu, ñatti yoon, bu ñu ko nattoon ci li nga wax ci bis bi mu tollu ko