Gëtën yi

5Listu hadiis yi 3Ràññetley bànqaas yi

Listu hadiis yi 5

Yàlla farataal na ay farata buleen ko sànk, mu teg ay dig buleen ko jéggi, mu araamal ay mbir buleen ko xëtt, mu noppi ci ay mbir ngir yërëm leen waaye fàttewu ko kon buleen ko gëstu
Yàlla du xool góor giy sëy ak soxnaam ci ginnaawam
ku gàddu ngànaay jëme sunu kaw kooku bokkul ci nun
dees na dagg loxo ci ñenteelu xaaju Diinaar jëm kaw
deesul dóor kenn lu ëpp fukki yar lu dul ci daani Yàlla