Xàjjaley wanqaas yi

Toftaleg Adiis yi

«buleen toog ci kaw bàmmeel yi, te buleen ko jublu ci julli».
عربي Àngale Urdu
«yëkkëti nanu xalima gi ci ñatt, ci kiy nelaw ba baa muy yeewu, ak ci xale bi ba baa muy gént, ak ci dof bi ba baa muy xellu».
عربي Àngale Urdu