عن أبي مَرْثَدٍ الغَنَوِيّ رضي الله عنه قال: قال رسول الله صلى الله عليه وسلم:
«لَا تَجْلِسُوا عَلَى الْقُبُورِ، وَلَا تُصَلُّوا إِلَيْهَا».
[صحيح] - [رواه مسلم] - [صحيح مسلم: 972]
المزيــد ...
Jële na ñu ci Marsad Al-Xanawii -yalna ko Yàlla gërëm- mu wax ne: Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na:
«buleen toog ci kaw bàmmeel yi, te buleen ko jublu ci julli».
[Wér na] - [Muslim soloo na ko] - [Téere Muslim bi gën a wér - 972]
Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- tere na toog ci kaw bàmmeel.
Niki mu teree julli jublu ci bàmmeel, bàmmeel bi nekk ci wetu penku kiy julli; ndax loolu daa bokk ci yiy yóbbe ci bokkaale yi.