Xàjjaley wanqaas yi

Toftaleg Adiis yi

1. Fekk nañu jenn jigéen ñu ray ko ci benn ci xarey Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc, Yonnente bi daal di ñaawlu ñuy ray jigéen ñi ak xale yi
عربي Àngale Urdu
2. tere na nisër, daal di wax ne: "du indi aw yiw, waaye dees ciy genne aji-nay ji
عربي Àngale Urdu
3. man de giñ naa ci Yàlla ne -bu soobee Yàlla- duma giñ ci dara ba noppi gis leneen lu ko gën, lu dul ne dinaa kaffaara sama giñ ba te def la ko gën - 2 ملاحظة
عربي Àngale Urdu
4. ku sol sooy fii ci àdduna du ko sol fële ca allaaxira
عربي Àngale Urdu
5. bokk na ci jihaad yi gën a màgg wax kàddug maanute fi kanamu buur bu jeng
عربي Àngale Urdu
6. Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc bu daan jug guddi day socc
عربي Àngale Urdu
7. Benn waay dafa laaj Yonnente bi ci bis-pénc ne ko: kañ la bis-pénc? Mu ne ko: "lan nga ko waajalal
عربي Àngale Urdu
8. Nit ki moo ngi ci diiney xaritam, na ku nekk xool kan lay xaritool
عربي Àngale Urdu
9. Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daan na baril lu muy wax: "yaw Aji-Wëlbati xol yi saxalal sama xol bi ci sa diine ji
عربي Àngale Urdu
10. bu ab xaj naanee ci ndabul kenn ci yéen na ko raxas juróom-ñaari yoon
عربي Àngale Urdu
11. amul kenn ku ñu war a jaamu ku dul Yàlla, alkande ñeel na araab yi ci ay wu jege, tijji nañu tay ci baaraasu Yaajuuja ak Maajuuja lu toll ni
عربي Àngale Urdu
12. Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc moo ëppoon kersa jigéen gi sëyagul, bu gisee mbir mu mu bañ ci kanamam gi lañu koy xame
عربي Àngale Urdu
13. ku ñaan Yàlla nekk sahiid ci ag dëggu kon Yàlla dana ko jotale ca darajay ña nekk sahiid, donte dafa dee ci kaw lalam
عربي Àngale Urdu
14. Yàlla du xool góor giy dikke soxnaam ci ginnaawam
عربي Àngale Urdu