Tooñaange yi

3Listu hadiis yi 1Ràññetley bànqaas yi

Listu hadiis yi 3

li ñuy njëkk a àtte ci diggante nit ñi ëllëg bis-pénc mooy dereet
ku xandaalu daanu ci aw doj daal di ray boppam kooku ci sawaraw Jahannama la jëm di ca xandaalu sax ca di ku ñu fay saxal ba fàww
bu kenn jëmale mbokkam ngànaay, ndax xamul ne Saytaane man naa bif loxoom, mu tàbbi ci kàmbu sawara