Xàjjaley wanqaas yi

Toftaleg Adiis yi

Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- tere na zulu.
عربي Àngale Urdu
«ku ne ci yéen ab sàmm la te dees na ko laaj la mu doon sàmm,* ki jiite nit ñi ab sàmm la te danañu ko ko laaj,góor gi ab sàmm la ci waa këram te danañu ko ko laaj, jigéen ji ab sàmm la ci kër jëkkëram ak i doomam te danañu ko ko laaj, jaam bi ab sàmm la ci alali sangam te danañu ka ko laaj, yégleen ne ku nekk ci yéen ab sàmm la te dees na ko laaj la mu doon sàmm».
عربي Àngale Urdu