Xàjjaley wanqaas yi

Toftaleg Adiis yi

1. bàyyileen ma bu ma leen bàyyee, ndax li alag ña leen jiitu woon mooy seeni laaj ak di wuute ak seeni Yonnente
عربي Àngale Urdu
2. kiy xeex ngir kàddug Yàlla yëkkatiku kooku moo ngi ci yoonu Yàlla
عربي Àngale Urdu
3. Bu leen sol suwaa walla sooy, bu leen naan ci ndabal wurus mbaa xaalis, te bu leen lekk ci ay boolam, ndax ñoom la ñeel fii ci àdduna, waaye nun la ñeel fële ca àllaaxira
عربي Àngale Urdu
4. man nag giñloowuma leen ci ne dama leen a tuumaal, waaye Jibriil moo ñëw fi man xibaar ma ne Yàlla mu kawe mi moo ngi leen di puukarewoo fa malaaka ya
عربي Àngale Urdu
5. yamaleleen seen sàppe yi, ndax yamale sàppe yi daa bokk ci matug julli gi - 2 ملاحظة
عربي Àngale Urdu
6. Jullit bu góor du bañ jullit bu jigéen, ndax su bañee ci moom jenn jikkó gërëm na ci moom jeneen jikkó
عربي Àngale Urdu
7. bu ngeen demee ca duus ba buleen jublu xibla, te buleen ko dummóoyu, waaye nangeen jëm Sarq walla Xarb
عربي Àngale Urdu
8. bu kenn ci yéen laal sakaraam ci ndayjooram fekk ma ngay saw, te bu demee duus ba noppi bu mu fompoo ndayjooram, te bu mu noyyi ci ndab li
عربي Àngale Urdu
9. Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- bu daan ubbi julli gi day yëkkati loxoom ba mu tolloo ak mbagg yi,
عربي Àngale Urdu
10. Allaahumma baahid baynii wa bayna xataayaaya kamaa baahadta baynal masrixi wal maxribi
عربي Àngale Urdu
11. ndax duma leen waxtaanal ci Ad-Dajjaal, lu benn Yonnente masul a wax aw xeetam? Moom de dafa patt, dana ànd ak lu mel ni àjjana ak sawara,
عربي Àngale Urdu
12. misaalu toogandoo bu sell ak toogandoo bu bon moo ngi mel ni ki yor gëttug Misk ak kiy upp ab furne, - 2 ملاحظة
عربي Àngale Urdu
13. gaawleen jëf ndax ay fitna a ngi ñëw yu mel ni dogiiti guddi gu lëndëm, - 4 ملاحظة
عربي Àngale Urdu
14. Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- bu daan julli day teqale ay loxoom ba weexaayu poqtaanam di feeñ
عربي Àngale Urdu
15. Alal ji gën ci li nit ki di joxe: mooy alal ji mu jox njabootam ak alal ji mu jox ay daabaam ci yoonu Yàlla, ak alal ji mu jox ay àndandoom ci yoonu Yàlla
عربي Àngale Urdu
16. yéemu naa ci mbirum jullit bi moom de mbiram lépp yiw la, te kenn amul loolu ku dul jullit bi - 2 ملاحظة
عربي Àngale Urdu
17. Melow sangu janaba.
عربي Àngale Urdu
18. Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- bu daan tissooli day teg loxoom -walla yéereem- ci gémmeñam, daal di suufeel -walla mu téye- ci kàdoom
عربي Àngale Urdu
19. dangeen topp yooni ña leen jiitu woon, sibre ak sibre, loxo ak loxo
عربي Àngale Urdu
20. wàlle amul gaafal amul, njuuma amul, Safar amul, te nanga daw ki gaana kem ni ngay dawe Gaynde
عربي Àngale Urdu
21. giñ naa ci Yàlla ne Yàlla gindi ci yaw benn waay moo gën ci yaw nga am géttug jur - 4 ملاحظة
عربي Àngale Urdu
22. nit ñi bu ñu gisee tooñkat bi te téyewuñu loxoom kon tuuti rekk Yàlla boole leen mbugal
عربي Àngale Urdu
23. ndax du ma leen tegtal li Yàlla di fare njuumte yi, di ci yëkkatee daraja yi? - 6 ملاحظة
عربي Àngale Urdu
24. ndax du ma leen tegtal li gën ci seen jëf yi, te gën cee sell fa seen Boroom, te gën cee kawe ci seeni daraja
عربي Àngale Urdu
25. texe na de ndeem wax na dëgg
عربي Àngale Urdu
26. bis bi gën ci bis yi mooy bisu àjjuma
عربي Àngale Urdu
27. torox na, torox na, torox na" ñu ne ko: kan? Yaw Yonnente Yàlla bi, mu ne: "ku fekk ñaari way-juram di ay mag, kenn ka walla ñaar ñépp te duggul Àjjana
عربي Àngale Urdu
28. ñu beru ñi raw nañu
عربي Àngale Urdu
29. déng naa la ngay bari looy sujjóotal Yàlla, ndaxte doo sujjóotal Yàlla genn sujjóot lu dul ne Yàlla dina la ci yëkkatil daraja, sippil la ci njuumte
عربي Àngale Urdu
30. ku julli ñaari sedd yi dana dugg àjjana - 2 ملاحظة
عربي Àngale Urdu
31. jullit bi bu ñu ko laajee ci bàmmeel: day seede ne amul kenn ku ñu war a jaamu ku dul Yàlla ak ne Muhammat ndawul Yàlla la
عربي Àngale Urdu
32. Yàlla mu màgg mi day tàllal loxoom ci guddi gi ngir ki doon def ñaawteef ci bëccëg gi tuub, di tàllal loxoom ci bëccëg gi ngir ki doon def ñaawteef ci guddi gi tuub, ba baa jant bi di fenke ci sowwu bi - 2 ملاحظة
عربي Àngale Urdu
33. fépp fu yax di daje ci nit sarax la
عربي Àngale Urdu
34. bu weeru koor ñëwee na nga dem umra ji ndax umra day yemoo ak aj - 2 ملاحظة
عربي Àngale Urdu
35. Yaw Yonnente Yàlla bi, gis nanu ne jihaad moo gën ci jëf yi, mo ndax dunu jihaadi? Mu wax ne: "déedéet, waaye jihaad ji gën mooy: aj gu baax
عربي Àngale Urdu
36. Nekkoon naa ak Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu dem ba egg ci sënu aw nit daal di tuur ndox fekk ma nga taxaw,
عربي Àngale Urdu