1. Li jiitu
  2. Ràññetle yi
  3. Ngëneel yi ak teggiin yi

Hadiis Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daan na bëgg ñaan yi làmboo lu bari, daan bàyyi yu dul yooyu

عَنْ عَائِشَةَ رضي الله عنها قَالَتْ:
كَانَ رَسُولُ اللَّهِ صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ يَسْتَحِبُّ الْجَوَامِعَ مِنَ الدُّعَاءِ، وَيَدَعُ مَا سِوَى ذَلِكَ.

Jële nañu ci Aysatu yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne:
Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daan na bëgg ñaan yi làmboo lu bari, daan bàyyi yu dul yooyu.

Wér na Abóo Daawuda soloo na ko,ak Ahmat Téere Sunna yi bu Abóo Daawuda - 1482

Leeral gi

Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dafa bëggoon ñaan yi làmboo yiwi àdduna ak allaaxira ci ay kàddu yu néew te maanaa mi bari, muy am tagg Yàlla ak jubluwaay yu sell, mu daan bàyyi yu dul yooyu.

Bokk na ci njariñi hadiis bi

  1. Sopp nañu ñaan ci ay kàddu yu néew te làmboo ay maanaay yiw, sib nañu it di diisal ak di jafeel ci ñaan, te dafa wuute ak njubug Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc.
  2. Jagleel nañu Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc kàddu yoy day dajale lu bari.
  3. Xér ci ñaan yi sax jóge ci Yonnente bi, donte dafa gudd ay baatam bari, loolu lépp dafa bokk ci ñaan yi matale.

Gaaral firi yi

46 Làkk wi
EN English الإنجليزية
UR اردو الأوردية
ES Español الإسبانية
ID Indonesia الإندونيسية
UG ئۇيغۇرچە الأيغورية
BN বাংলা البنغالية
TR Türkçe التركية
RU Русский الروسية
BS Bosanski البوسنية
SI සිංහල السنهالية
HI हिन्दी الهندية
ZH 中文 الصينية
FA فارسی الفارسية
VI Tiếng Việt الفيتنامية
TL Tagalog تجالوج
KU Kurdî الكردية
HA Hausa الهوسا
PT Português البرتغالية
ML മലയാളം المليالم
TE తెలుగు التلغو
SW Kiswahili السواحيلية
TA தமிழ் التاميلية
MY မြန်မာ البورمية
TH ไทย التايلندية
DE Deutsch الألمانية
PS پښتو بشتو
AS অসমীয়া الأسامية
SQ Shqip الألبانية
SV Svenska السويدية
AM አማርኛ الأمهرية
NL Nederlands الهولندية
GU ગુજરાતી الغوجاراتية
NE नेपाली النيبالية
PRS دری الدرية
SR Српски الصربية
RO Română الرومانية
HU Magyar المجرية
MOS Moore الموري
MG Malagasy المالاجاشية
KN ಕನ್ನಡ الكانادا
UK Українська الأوكرانية
KA ქართული الجورجية
MK Македонски المقدونية
KM ភាសាខ្មែរ الخميرية
PA ਪੰਜਾਬੀ البنجابية
MR मराठी الماراثية