Àtteb woote jëm ci Yàlla

1Listu hadiis yi

Listu hadiis yi 1

Jottalileen jële ci man donte benn aaya la, ta ngeen waxtaane waa Banuu Israayil ci lu amul benn jafe-jafe, waaye ku ma fenal te tay ko na waajal ab tooguwaayam ca sawara