1. Li jiitu
  2. Ràññetle yi
  3. Dégg diine ak i cosaanam

Hadiis Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc tabaskee na ñaari kuuy yu duuf am ay béjjan, mu rendi leen ci loxoom, tudd Yàlla daal di kàbbar, teg tànkam bi ca seen doq ya

عَنْ أَنَسٍ رَضيَ اللهُ عنهُ قَالَ:
ضَحَّى النَّبِيُّ صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ بِكَبْشَيْنِ أَمْلَحَيْنِ أَقْرَنَيْنِ، ذَبَحَهُمَا بِيَدِهِ، وَسَمَّى وَكَبَّرَ، وَوَضَعَ رِجْلَهُ عَلَى صِفَاحِهِمَا.

Jële nañu ci Anas yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne:
Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc tabaskee na ñaari kuuy yu duuf am ay béjjan, mu rendi leen ci loxoom, tudd Yàlla daal di kàbbar, teg tànkam bi ca seen doq ya.

Wér na Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér Téere Al-buxaariy bi gën a wér - 5565

Leeral gi

Anas yal na ko Yàlla dollee gërëm day nettali ne Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dafa rendi ci loxoom ci bisu feetu Tabaski ñaari xar yu góor yu mag am ay béjjan nekk yu weex te rax ñuul, mu wax: bismil Laahi wallaahu Akbar, mu teg tànkam ca doq ga.

Bokk na ci njariñi hadiis bi

  1. Yoonalees na Tabaski, te jullit ñi dëppoo nañu ci.
  2. Li gën mooy li ñuy tabaskee mel ni xeet wii Yonnente bi tabaskee; ngir ni jëmm ji rafete ak ni gareesam ak ndawalam gën a teeye.
  3. An-Nawawii wax na: ca loola ne sopp nañu nit ki féetewoo rendi tabaskeem ci boppam, te bañ a féetale rendi ga kenn ci lu dul ngànt, te bu booba a sopp nañu mu teewe rendi ga, bu ca wuutalee ab jullit kon dagan na ci lu dul ag wuute.
  4. Ibn Hajar nee na: sopp nañu kàbbar ak tudd Yàlla bu ñuy rendi, sopp nañu it nu teg tànk bi ci doq gi ci wetug ndayjoor gi, dëppoo nañu it ne wetu càmmooñ lañu koy tërale, mu teg tànkam ci wetug ndayjoor gi ngir mu gën a yomb ci kiy rendi mu téye paaka bi ci ndayjooram jàpp ci bopp bi ci loxob càmmooñam.
  5. Sopp nañu tabaskee lu am béjjan bu dul moom it dana dagan.

Gaaral firi yi

53 Làkk wi
EN English الإنجليزية
UR اردو الأوردية
ES Español الإسبانية
ID Indonesia الإندونيسية
UG ئۇيغۇرچە الأيغورية
BN বাংলা البنغالية
TR Türkçe التركية
RU Русский الروسية
BS Bosanski البوسنية
SI සිංහල السنهالية
HI हिन्दी الهندية
ZH 中文 الصينية
FA فارسی الفارسية
VI Tiếng Việt الفيتنامية
TL Tagalog تجالوج
KU Kurdî الكردية
HA Hausa الهوسا
PT Português البرتغالية
ML മലയാളം المليالم
TE తెలుగు التلغو
SW Kiswahili السواحيلية
TA தமிழ் التاميلية
MY မြန်မာ البورمية
TH ไทย التايلندية
DE Deutsch الألمانية
PS پښتو بشتو
AS অসমীয়া الأسامية
SQ Shqip الألبانية
SV Svenska السويدية
AM አማርኛ الأمهرية
NL Nederlands الهولندية
GU ગુજરાતી الغوجاراتية
KY Кыргызча القيرقيزية
NE नेपाली النيبالية
LT Lietuvių الليتوانية
PRS دری الدرية
SR Српски الصربية
TG тоҷикӣ الطاجيكية
RW Kinyarwanda الكينياروندا
RO Română الرومانية
HU Magyar المجرية
CS Čeština التشيكية
MOS Moore الموري
MG Malagasy المالاجاشية
OM Oromoo الأورومو
KN ಕನ್ನಡ الكانادا
AZ Azərbaycan الأذربيجانية
UK Українська الأوكرانية
KA ქართული الجورجية
MK Македонски المقدونية
KM ភាសាខ្មែរ الخميرية
PA ਪੰਜਾਬੀ البنجابية
MR मराठी الماراثية