1. Li jiitu
  2. Ràññetle yi
  3. Dégg diine ak i cosaanam

Hadiis tere na nisër, daal di wax ne: "du indi aw yiw, waaye dees ciy genne aji-nay ji

عَنِ ابْنِ عُمَرَ رضي الله عنهما:
عَنِ النَّبِيِّ صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ أَنَّهُ نَهَى عَنِ النَّذْرِ، وَقَالَ: «إِنَّهُ لَا يَأْتِي بِخَيْرٍ، وَإِنَّمَا يُسْتَخْرَجُ بِهِ مِنَ الْبَخِيلِ».

Jële nañu ci Ibn Umar yal na leen Yàlla dollee gërëm
Mu jële ci Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc ne moom Yónente bi tere na nisër, daal di wax ne: "du indi aw yiw, waaye dees ciy genne aji-nay ji".

Wér na Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér Téere Muslim bi gën a wér - 1639

Leeral gi

Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc tere na nisër, te mooy nit ki waral ci boppam lu Sariiha waralul ci moom, mu wax ne: nisër du gaawal dara te du ko yéexal, waaye dañu ciy genne ku nay ki dul def lu dul li war ci moom, ak ne nisër du indi dara lu dul lu ñu dogal ci moom.

Bokk na ci njariñi hadiis bi

  1. Yoonaluñu nisër, waaye bu nit ki nisëree day war ci moom mu matale ko ndeem nekkul ag moy.
  2. Li waral tere gi mooy (du indi yiw); ndaxte du delloo dara ci dogalu Yàlla; ak it ngir aji-nisër ji bañ a njort ne nisër gi moo tax li mu doon sàkku am, te yàlla Aji-Doylu la wolif loolu.
  3. Al-Xurtubii nee na: tere gii barabam mooy niki mu wax: bu Yàlla wéralee sama aji-tawat ji kon war na maa saraxe lii, anamug tere gi mooy ne ba mu tegee jëfug jaamu gi ci amug la mu bëgg, day feeñ ne jagleelu ko yéeneg jéem a jege Yàlla ndax ci li mu def, waaye dafa sóobu yoonu wecceente, te li koy leeral mooy bu aji-tawat ji wérul woon kon du saraxe la mu wékkoon ca wéram ga, te lii mooy melow ki nay, moom du génne dara ci alalam ci lu dul ag weccee gu teew, te sax day ëpp la mu génne ci lu gën a bari.

Gaaral firi yi

55 Làkk wi
EN English الإنجليزية
UR اردو الأوردية
ES Español الإسبانية
ID Indonesia الإندونيسية
UG ئۇيغۇرچە الأيغورية
BN বাংলা البنغالية
TR Türkçe التركية
RU Русский الروسية
BS Bosanski البوسنية
SI සිංහල السنهالية
HI हिन्दी الهندية
ZH 中文 الصينية
FA فارسی الفارسية
VI Tiếng Việt الفيتنامية
TL Tagalog تجالوج
KU Kurdî الكردية
HA Hausa الهوسا
PT Português البرتغالية
ML മലയാളം المليالم
TE తెలుగు التلغو
SW Kiswahili السواحيلية
TA தமிழ் التاميلية
MY မြန်မာ البورمية
TH ไทย التايلندية
DE Deutsch الألمانية
PS پښتو بشتو
AS অসমীয়া الأسامية
SQ Shqip الألبانية
SV Svenska السويدية
AM አማርኛ الأمهرية
NL Nederlands الهولندية
GU ગુજરાતી الغوجاراتية
KY Кыргызча القيرقيزية
NE नेपाली النيبالية
YO Yorùbá اليوروبا
LT Lietuvių الليتوانية
PRS دری الدرية
SR Српски الصربية
SO Soomaali الصومالية
TG тоҷикӣ الطاجيكية
RW Kinyarwanda الكينياروندا
RO Română الرومانية
HU Magyar المجرية
CS Čeština التشيكية
MOS Moore الموري
MG Malagasy المالاجاشية
OM Oromoo الأورومو
KN ಕನ್ನಡ الكانادا
AZ Azərbaycan الأذربيجانية
UK Українська الأوكرانية
KA ქართული الجورجية
MK Македонски المقدونية
KM ភាសាខ្មែរ الخميرية
PA ਪੰਜਾਬੀ البنجابية
MR मराठी الماراثية