عَنْ مَالِكِ بْنِ أَوْسِ بْنِ الْحَدَثَانِ أَنَّهُ قَالَ: أَقْبَلْتُ أَقُولُ مَنْ يَصْطَرِفُ الدَّرَاهِمَ؟ فَقَالَ طَلْحَةُ بْنُ عُبَيْدِ اللهِ وَهُوَ عِنْدَ عُمَرَ بْنِ الْخَطَّابِ رضي الله عنهما: أَرِنَا ذَهَبَكَ، ثُمَّ ائْتِنَا، إِذَا جَاءَ خَادِمُنَا، نُعْطِكَ وَرِقَكَ، فَقَالَ عُمَرُ بْنُ الْخَطَّابِ: كَلَّا، وَاللهِ لَتُعْطِيَنَّهُ وَرِقَهُ، أَوْ لَتَرُدَّنَّ إِلَيْهِ ذَهَبَهُ، فَإِنَّ رَسُولَ اللهِ صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ قَالَ:
«الْوَرِقُ بِالذَّهَبِ رِبًا، إِلَّا هَاءَ وَهَاءَ، وَالْبُرُّ بِالْبُرِّ رِبًا، إِلَّا هَاءَ وَهَاءَ، وَالشَّعِيرُ بِالشَّعِيرِ رِبًا، إِلَّا هَاءَ وَهَاءَ، وَالتَّمْرُ بِالتَّمْرِ رِبًا، إِلَّا هَاءَ وَهَاءَ».
المزيد
Jële nañu ci Maalik ibn Aws ibn Al-Hadsaan mu wax ne: ana kan mooy weccee dërëm? Talhata ibn Hubayd Allaa ne ko fekk booba ma nga ca Umar ibnul Xattaab yal na leen Yàlla dollee gërëm: wan nu sa wurus wi te nga ñëw bu sunu surga bi ñëwee, nu joxla sa xaalis, Umar ibnul Xattaab ne ko: déedéet, waat naa ko ci Yàlla danga koy jox xaalisam, walla nga delloo ko wurusam, ndax Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na:
«Weccee xaalis ci wurus ribaa la lu dul mu nekk loxook loxo, pepp ci pepp ribaa la lu mu nekk loxook loxo, orge ci orge ribaa la lu dul mu nekk am ak am maanaam loxook loxo, tàndarma ci tàndarma ribaa la lu moy loxook loxo».