عَنْ عُمَرَ رضي الله عنه قَالَ: قَالَ النَّبِيُّ صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ:
«مَنْ لَبِسَ الحَرِيرَ فِي الدُّنْيَا لَمْ يَلْبَسْهُ فِي الآخِرَةِ».  
                        
[صحيح] - [متفق عليه] - [صحيح البخاري: 5834]
                        
 المزيــد ... 
                    
Jële na ñu ci Ibn Umar -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:
"ku sol sooy fii ci àdduna du ko sol fële ca allaaxira" 
                                                     
                                                                                                    
[Wér na] - [Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér] - [Téere Al-buxaariy bi gën a wér - 5834]                                            
Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc day leeral ne góor gu sol sooy fii ci àdduna du ko sol fële ca allaaxira ndeem tuubu ko.