1. Li jiitu
  2. Ràññetle yi
  3. Dégg diine ak i cosaanam

Hadiis Dañoo tudd fi Yonnente bi jenn waay bu nelaw guddeem gi yépp ba suba jot, mu ne: "kooku mooy ki nga xam ne saytaane daa saw ci ay noppam, walla mu wax: ci noppam

عَنْ عَبْدِ اللَّهِ بنِ مسعُودٍ رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ قَالَ:
ذُكِرَ عِنْدَ النَّبِيِّ صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ رَجُلٌ نَامَ لَيْلَهُ حَتَّى أَصْبَحَ، قَالَ: «ذَاكَ رَجُلٌ بَالَ الشَّيْطَانُ فِي أُذُنَيْهِ، أَوْ قَالَ: فِي أُذُنِهِ».

Jële nañu ci Abdullah Ibn Mashuud yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne:
Dañoo tudd fi Yonnente bi jenn waay bu nelaw guddeem gi yépp ba suba jot, mu ne: "kooku mooy ki nga xam ne saytaane daa saw ci ay noppam, walla mu wax: ci noppam".

Wér na Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér Téere Al-buxaariy bi gën a wér - 3270

Leeral gi

Dañoo tudd fi Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc jenn waay ju nelaw ba suba jot jant bi fenk te jugul julli farata gi, Yonnente bi daa di ne: waa jooju saytaane moo saw ci nopp bi.

Bokk na ci njariñi hadiis bi

  1. Sib nañu bàyyi taxaw guddi, ak ne loolu saytaane moo ko sabab.
  2. Moytandiku saytaane mi nga xam ne day toog ci yoonu nit ki; ngir dox ci digganteem ak topp Yàlla mu màgg mi.
  3. Ibn Hajar nee na: li mu wax: (jugul jëm ci julli gi) li ñu ci namm mooy xeetu julli rekk, jamtal na it muy gu ñu xam, ñu namm ci julli guddi, walla gu farata.
  4. At-Tiibii nee na:tudd gi ñu tudd nopp donte bët moo gën a méngoo ak nelaw, loo lu junj la ci diisug nelaw yi, ndax nopp yi la ñuy bàyyee xel, tudd nañu saw ndaxte moo gën a yomb te gën a gaaw a jàll ca séddit ya, ba tax muy waral tàyyeel ci mbooleem cér yi.

Gaaral firi yi

51 Làkk wi
EN English الإنجليزية
UR اردو الأوردية
ES Español الإسبانية
ID Indonesia الإندونيسية
UG ئۇيغۇرچە الأيغورية
BN বাংলা البنغالية
TR Türkçe التركية
RU Русский الروسية
BS Bosanski البوسنية
SI සිංහල السنهالية
HI हिन्दी الهندية
ZH 中文 الصينية
FA فارسی الفارسية
VI Tiếng Việt الفيتنامية
TL Tagalog تجالوج
KU Kurdî الكردية
HA Hausa الهوسا
PT Português البرتغالية
ML മലയാളം المليالم
TE తెలుగు التلغو
SW Kiswahili السواحيلية
TA தமிழ் التاميلية
MY မြန်မာ البورمية
TH ไทย التايلندية
DE Deutsch الألمانية
PS پښتو بشتو
AS অসমীয়া الأسامية
SQ Shqip الألبانية
SV Svenska السويدية
AM አማርኛ الأمهرية
NL Nederlands الهولندية
GU ગુજરાતી الغوجاراتية
NE नेपाली النيبالية
YO Yorùbá اليوروبا
LT Lietuvių الليتوانية
PRS دری الدرية
SR Српски الصربية
TG тоҷикӣ الطاجيكية
RW Kinyarwanda الكينياروندا
RO Română الرومانية
HU Magyar المجرية
MOS Moore الموري
MG Malagasy المالاجاشية
OM Oromoo الأورومو
KN ಕನ್ನಡ الكانادا
UK Українська الأوكرانية
KA ქართული الجورجية
MK Македонски المقدونية
KM ភាសាខ្មែរ الخميرية
PA ਪੰਜਾਬੀ البنجابية
MR मराठी الماراثية