1. Li jiitu
  2. Ràññetle yi
  3. Pas-pasu Lislaam

Hadiis Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc wax na ñeel Abuu Bakrin ak Umar: «ñaar ñii ñooy sangi paa yiy nekk àjjana ñu njëkk ña ak ñu mujj ña ba mu des yónente yi 

عن أنس رضي الله عنه، قال:
قال رسول الله صلى الله عليه وسلم لأبي بكر وعمر: «هذان سَيِّدا كُهُول أهل الجنة من الأوَّلِين والآخِرين إلا النبيِّين والمرسلين».

Jële nañu ci Anas yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne:
Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc wax na ñeel Abuu Bakrin ak Umar: «ñaar ñii ñooy sangi paa yiy nekk àjjana ñu njëkk ña ak ñu mujj ña ba mu des yónente yi ».

Wér na At-tirmisiy soloo na ko Téere Sunna yi bu At-tirmisiy - 3664

Leeral gi

Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dafa xibaare ne Abuu Bakrin Al-Siddiiq ak Umar Al-Faaruuq yal na leen Yàlla dollee gërëm ñoom ñoo gën ci nit ñi ginnaaw Yonnente yi, te ñoo gën ci ñi dugg àjjana ginnaaw Yonente yi.

Bokk na ci njariñi hadiis bi

  1. Abuu Bakrin ak Umar yal na leen Yàlla dollee gërëm ñoom ñoo gën ci nit ñi ginnaaw Yonnente yi.
  2. Àjjana amul paa, waaye ña cay dugg fanweeri at ak ñatt lañuy am, li ñu ci jublu mooy ñoom ñaar ñooy sangi ñi faatu ci àdduna te nekk paa, walla ñu jàppe ko anam ga ñu nekkoon ci àdduna jamonoy hadiis bii.

Gaaral firi yi

48 Làkk wi
EN English الإنجليزية
UR اردو الأوردية
ID Indonesia الإندونيسية
UG ئۇيغۇرچە الأيغورية
BN বাংলা البنغالية
TR Türkçe التركية
RU Русский الروسية
BS Bosanski البوسنية
SI සිංහල السنهالية
HI हिन्दी الهندية
ZH 中文 الصينية
FA فارسی الفارسية
VI Tiếng Việt الفيتنامية
TL Tagalog تجالوج
KU Kurdî الكردية
HA Hausa الهوسا
PT Português البرتغالية
ML മലയാളം المليالم
TE తెలుగు التلغو
SW Kiswahili السواحيلية
TA தமிழ் التاميلية
MY မြန်မာ البورمية
TH ไทย التايلندية
DE Deutsch الألمانية
PS پښتو بشتو
AS অসমীয়া الأسامية
SQ Shqip الألبانية
SV Svenska السويدية
AM አማርኛ الأمهرية
NL Nederlands الهولندية
GU ગુજરાતી الغوجاراتية
NE नेपाली النيبالية
PRS دری الدرية
SR Српски الصربية
TG тоҷикӣ الطاجيكية
RW Kinyarwanda الكينياروندا
RO Română الرومانية
HU Magyar المجرية
MOS Moore الموري
MG Malagasy المالاجاشية
OM Oromoo الأورومو
KN ಕನ್ನಡ الكانادا
UK Українська الأوكرانية
KA ქართული الجورجية
MK Македонски المقدونية
KM ភាសាខ្មែរ الخميرية
PA ਪੰਜਾਬੀ البنجابية
MR मराठी الماراثية