عَنْ عَبْدِ اللهِ بْنِ مَسْعُودٍ رَضيَ اللهُ عنهُ عَنِ النَّبِيِّ صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ أَنَّهُ كَانَ يَقُولُ:
«اللهُمَّ إِنِّي أَسْأَلُكَ الْهُدَى وَالتُّقَى، وَالْعَفَافَ وَالْغِنَى».

Jële nañu ci Abdullah Ibn Mashuud -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa Yonente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- daan na wax:
"Allaahuma innii as-aluka alhudaa wattuqaa walhafaafa walxinaa".

Wér na Muslim soloo na ko Téere Muslim bi gën a wér - 2721

Leeral gi

Bokkoon na ci ñaani Yonente bi: yaw Yàlla sama Boroom man maa ngi lay laaj ag njub yoon wu jub ci xam dëgg ak jëfe ko, ak ragal la jëf ndigal yi moytandiku tere yi, ak fegu bàyyi li daganul te rafetul ci wax walla jëf, ak doylu wolif mbindeef yi, ba tax na duma ajowoo jëm ci kenn ku dul sama Boroom mu màgg mi.

Bokk na ci njariñi hadiis bi

  1. Teddngay jikkó yii: jub ak ragal Yàlla ak fegu ak doylu, ak ñaaxe ci jikkówoo ko.
  2. Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc yoralul boppam njariñ du caagine lor, ak ne ki yor loolu mooy Yàlla mu kawe mi.
  3. Ki yor njariñ ak lor ak gindi mbindeef yi mooy Yàlla dong, du malaaka, du Yonnente, du keneen ku dul ñoom.

Gaaral firi yi

43 Làkk wi
EN English الإنجليزية
UR اردو الأوردية
ES Español الإسبانية
ID Indonesia الإندونيسية
BN বাংলা البنغالية
TR Türkçe التركية
RU Русский الروسية
BS Bosanski البوسنية
SI සිංහල السنهالية
HI हिन्दी الهندية
ZH 中文 الصينية
FA فارسی الفارسية
VI Tiếng Việt الفيتنامية
TL Tagalog تجالوج
KU Kurdî الكردية
HA Hausa الهوسا
PT Português البرتغالية
ML മലയാളം المليالم
TE తెలుగు التلغو
SW Kiswahili السواحيلية
TA தமிழ் التاميلية
MY မြန်မာ البورمية
TH ไทย التايلندية
PS پښتو بشتو
AS অসমীয়া الأسامية
SQ Shqip الألبانية
SV Svenska السويدية
AM አማርኛ الأمهرية
NL Nederlands الهولندية
GU ગુજરાતી الغوجاراتية
PRS دری الدرية
SR Српски الصربية
RO Română الرومانية
HU Magyar المجرية
MOS Moore الموري
MG Malagasy المالاجاشية
KN ಕನ್ನಡ الكانادا
UK Українська الأوكرانية
KA ქართული الجورجية
MK Македонски المقدونية
KM ភាសាខ្មែរ الخميرية
PA ਪੰਜਾਬੀ البنجابية
MR मराठी الماراثية