Nettali ak biri xeet ya jiitu

1Listu hadiis yi

Listu hadiis yi 1

waa Banuu Israayil ay Yonente ñoo leen doon jiite, saa bu ab yonente faatoo beneen yonente wuutu ko, te ab Yonente du ñëw sama ginnaaw, ay Xalifa nag danañu nëw sama ginnaaw te danañu bari