عَنْ أَبِي مَسْعُودٍ عُقْبَةَ بْنِ عَمْرٍو الأَنْصَارِيِّ البَدْرِيِّ رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ قَالَ: قَالَ رَسُولُ اللَّهِ:
«إِنَّ مِمَّا أَدْرَكَ النَّاسُ مِنْ كَلاَمِ النُّبُوَّةِ الأُولَى: إِذَا لَمْ تَسْتَحْيِ فَاصْنَعْ مَا شِئْتَ».
المزيد
Jële nañu ci Abuu Mashuud Uqbata ibn Amr Al-Absaarii Al-Badrii yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonente Yàlla bi nee na:
«bokk na ci li fi nit ñi fekk ci waxi Yonnente ya jiitu: boo amul looy
rus defal lu la neex».