Njuumtey ñiy julli

3Listu hadiis yi

Listu hadiis yi 3

deesul julli fekk ñam wi daa teew, walla muy xëcconte ak ñaari sobe yi
ku fàtte genn julli na ko julli saa yu ko fàttalikoo, dara manu koo fay lu dul loolu
ki gën a bon ug càcc ci nit ñi mooy kiy sacc julleem» ñu ne ko: naka lay sacce julleem? Mu ne: «du matal rukkoo yi, ak sujjóot yi