Ngëneelu digle yiw tere njékar

2Listu hadiis yi

Listu hadiis yi 2

bokk na ci jihaad yi gën a màgg wax kàddug maanute fi kanamu buur bu jeng
misaalu ki taxaw ci foroñceeri Yàlla yi ak ki ci tàbbi, moo ngi mel ni aw nit wu tegoo bant ci ag gaal, ñii am kaw ga, ñii nekk ca suuf ga